1 Corinthians 14:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Looloo tax kiy wax aw làkk, na ñaan ngir mu man a firi li looluy tekki.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax kiy làkk weneen làkk wara ñaan ngir ñu xam pireem.