1 Corinthians 14:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Walla, boo dee gërëm Yàlla, ànd ci ak sa xol rekk, kon ku musul a jàng mbir yooyu, nan la man a waxe: «Amiin,» ci sa cant Yàlla googu? Ndaxte xamul li ngay wax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Soo yékkatee kàddug cant goo waxe xol doŋŋ, ana nu nit ku xamul ku ko teewe naan: «Amiin,» te xamul li ngay wax?