1 Corinthians 14:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi sant Yàlla ci li may wax ay làkk, ba raw leen yéen ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sant naa Yàlla ndegam maay làkk yeneen làkk ba raw leen, yeen ñépp.