1 Corinthians 14:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ci ndajem mbooloom ñi gëm, wax juróomi baat yu am njariñ, ngir jàngal ñi ci des, moo ma gënal wax fukki junniy baat ciw làkk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye fu mbooloom gëmkat ñi daje, juróomi baat yu ma waxe samam xel ngir jàngle, moo ma gënal junniy baat yu ma waxe weneen làkk.