1 Corinthians 14:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bind nañu ci téereb yoon wi:«Dinaa wax ak mbooloo mii,jaare ko ci ay nit, ñuy wax yeneen làkk,ak ay gémmiñi doxandéem,waaye ba tey duñu ma déglu.» Moom la Boroom bi wax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bindees na ci téereb yoon wi ne: «Ay niti làkk-kat, ay làmmiñi doxandéem, ci laay waxe ak askan wii, te taxul ba tey ñu déglu ma. Boroom bee ko wax.»