1 Corinthians 14:22 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ci noonu wax ay làkk, firnde la ci ñi gëmul, te du firnde ci ñi gëm. Te it wax ci kàddug Yàlla, du firnde ci ñi gëmul, waaye firnde la ci ñi gëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag, yeneen làkk, kàddu ya du ci gëmkat ñi la di firnde, waaye ci ñi gëmul la di firnde. Te it waxe kàddug waxyu, du ci ñi gëmul la di firnde, waaye ci gëmkat ñi la dib firnde.