1 Corinthians 14:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag su fekkee ku jàngul mbiri Kirist walla ku gëmul dugg ca mbooloo ma, fekk ñépp di wax ay làkk, ndax du wax ne, dangeen a dof?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag su mbooloom gëmkat mépp dajee bérab, ñépp di làkk yeneen làkk, bu ay nit ñu xamul mbaa ñu gëmul duggsee, duñu ne dangeena dof?