1 Corinthians 14:26 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon nag bokk yi, lu muy indi? Bu ngeen dajee, kii am aw taalif, kii am njàngale, kii dëgg gu Yàlla feeñal, kii di wax aw làkk, kee di ko firi. Na loolu lépp aw ci yoonu yokk ngëmu mbooloo mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag ana nees di def, bokk yi? Bu ngeen dajee, kii am woyu cant, kii am lu muy jàngle, kee am am peeñu, kale am lu muy waxe weneen làkk, keneen am am piri, loolu lépp na ko feddli ngëm taxa jóg.