1 Corinthians 14:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su amee kuy wax aw làkk, na ñaar wax walla gën gaa bare ñett. Nañu ko toppante, te kenn di firi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su dee weneen làkk lees di wax, na ñaar ba gën gaa bare, ñett, toppante, te kenn di firi.