1 Corinthians 14:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye kiy jottali kàddug Yàlla, nit ñi lay waxal ngir yékkati seen ngëm, di leen dénk ak a dëfël.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye kiy waxe kàddug waxyu, nit ñi lay waxal, di feddlee, di ñaaxe ak di naabe.