bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 14:31
1 Corinthians 14:31 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Yéen ñépp man ngeen a kenn-kennoo wax ci kàddug Yàlla, ngir ñépp jàng te dégg li ñu leen di dénk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat yeen ñépp man ngeena kenn-kennoo, di waxe kàddug waxyu, ngir ñépp jànge ca, ba gëna farlu.