1 Corinthians 14:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte Yàlla du Yàllay lëj-lëj waaye Yàllay jàmm la. Ci mboolooy gaayi Yàlla yépp,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax Yàlla du Yàllay salfaañoo, Yàllay jàmm la. Ci mboolem mboolooy ñu sell ñi nag,