1 Corinthians 14:37 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Su kenn xalaatee ne, mooy wax ci kàddug Yàlla, walla mu xalaat ne, Xelum Yàlla jagleel na may, na nangu ne lii ma leen bind ndigalu Boroom bi la.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ku ci xalaat ne moom jottlikatub kàddug waxyu la, mbaa boroom ag may la ci Noo gi, war naa xam xéll ne lii ma leen bind, santaaneb Boroom bi la.