1 Corinthians 14:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kiy wax aw làkk dafay yokk boppam, waaye kiy wax ci kàddug Yàlla, dafay yokk ngëmu mbooloo mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kiy làkk yeneen làkk, boppam lay feddli, waaye kiy waxe kàddug waxyu, mbooloom gëmkat ñi lay feddli seen ngëm.