bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 14:9
1 Corinthians 14:9 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu itam bu ngeen génnewul ay wax yu leer ci seen gémmiñ, nan lañuy man a xame li ngeen di wax? Dingeen wax cig neen!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu la ci yeen itam. Seen làmmiñ, su ngeen ci waxul kàddu gu leer, ana nees di xame li ngeen di wax? Ci jaww ji rekk ngeen di wax!