1 Corinthians 15:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Léegi nag bokk yi, maa ngi leen di fàttali xebaar bu baax bi ma leen yégal. Xebaar bu baax boobu, nangu ngeen ko te yéena ngi ciy sax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag bokk yi, ma fàttli leen xibaaru jàmm bi ma leen xibaaroon, muy lu ngeen gëm, sax ci,