1 Corinthians 15:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu nag muy man muy ñoom, dénkaane boobu lanuy yégle, te moom ngeen gëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon muy man, di ñoom, noonu lanu waaree, te noonu it ngeen gëme.