1 Corinthians 15:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su fekkee ci giiru dund gii rekk la sunu yaakaar ci Kirist ame solo, kon noo gën a mat a yërëm ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su dee ci giiru dund gii doŋŋ lanu ame yaakaar ci Almasi, kon de noo gëna toskare ñépp.