1 Corinthians 15:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci moom ngeen jaare, ba mucc, bu ngeen téyee bu dëgër njàngale mi, ni ma leen ko yégale. Walla xanaa boog gëm ngeen ko cig neen?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te ci ngeen texee, ndegam jàpp ngeen bu dëgër ci kàddug xibaaru jàmm bi, ni ma leen ko xamale. Lu ko moy ci neen ngeen gëm.