1 Corinthians 15:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye léegi Kirist dekki na, di ku jëkk a dekki, ni gub yi ñu jëkk a tànne ci ngóob mi, jagleel leen Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye nag Almasi dafa dekki moos, te mooy saraxu ndoortel meññeef, bi ñu sàkke ci ngóobum bakkani nit ñi dee.