bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 15:23
1 Corinthians 15:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye ku nekk ak ayam. Kirist moo jëkk, mel ni gub yi ñu jëkk a tànne ci ngóob mi, ba noppi, bu Kirist dellusee, ñi bokk ci moom jël seen ay.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ku nekk ak ayam. Jooxeb ndoortel meññeef mi, Almasi la. Gannaaw loolu ñoñi Almasi ñooy aye, keroog bu délsee.