1 Corinthians 15:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Mbind mi nee na: «Yàlla nootal na ko lépp, mu teg ci tànk.» Waaye bu Mbind mi nee, «noot na lépp,» wóor na ne, moom mi ko nootal lépp, génne na ci boppam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax «Lépp la Yàlla di jébbal Almasi, teg ko fi ron ndëgguy tànkam.» Waaye bu Yàlla nee, «lépp la koy jébbal,» bir na ne moom mi ko jébbal lépp, bokku ci.