1 Corinthians 15:28 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Léegi bu ñu ko nootalee lépp nag, moom Kirist muy Doom ji dina delloo kilifteef gi Yàlla, mi ko nootal lépp, ngir Yàlla nekk buur ci lépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu ñu ko jébbalee lépp nag, su boobaa moom Doom ji ci boppam mooy jébbal boppam, ki ko jébbal lépp, ngir Yàlla di lépp ci lépp.