1 Corinthians 15:32 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su fekkee ne ci ni ñu ko waxe, xeex naa ca dëkku Efes ak rabi àll, kon ban njariñ la may amal? Su néew yi dul woon dekki, am na lu ci léeb wax:«Nanu lekk di naan, ndaxte ëllëg dinanu dee.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su yaakaaru nit ci àddina doŋŋ taxee may xeex ak ay rabi àll ca Efes, ana lu mu may jariñ. Gannaaw ñi dee duñu dekki, kon kay mooy li ñu ne: «Nanu lekk te naan, nde ëllëg nu dee.»