1 Corinthians 15:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Delloosileen xel yi te bàyyi bàkkaar, ndaxte am na ci yéen, ñu umple Yàlla. Kon war ngeen a rus!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Délloosileen xel yi ci njub te bàyyi bàkkaar, ndax ñàkka xam lenn ci Yàlla, moom la ñenn ci yeen nekke, te loolu gàcce la ci yeen, laa wax!