1 Corinthians 15:35 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye dina am kuy naan: «Nan la néew yi di dekkee? Wan yaram lañuy dellusee?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul nit a ngi naan: «Nan la ñi dee di dekkee? Wan yaram lañuy dekkaale?»