1 Corinthians 15:41 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Jant bi, weer wi ak biddiiw, lu nekk ak sag leer. Te it leeru biddiiw bu nekk dina wuute ak moroomam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jant bi ak leeru boppam, weer wi ak leeru boppam, biddiiw yi ak seen leeru bopp, te biddiiw sax wuute naak moroom ma, ag leer.