1 Corinthians 15:42 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu la ndekkitel néew yi di deme. Bu ñu suulee néew bi, dañoo ji lu yàqu. Bu dekkee, du yàqooti ba abadan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu itam la ndekkitel ñi dee di deme. Li ñu suul mooy jiwu wiy yàqu, te bu dekkee dootu yàqu.