1 Corinthians 15:45 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mbind mi nee na: «Nit ku jëkk ka, Aadama, doon na boroom ruu,» waaye Aadama mu mujj mi doon na Xel muy joxe dund.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu lañu binde ne: «Aadama, nit ku jëkk ka, lañu def jëmm juy dund,» waaye Aadama mu mujj mi moo di Noo giy dundloo.