1 Corinthians 15:46 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yaram wi soloo ndamu Xelum Yàlla jiituwul; yaramu doom Aadama moo jiitu; yaramu ndam li moo ci topp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Du yaram wi bindoo ag noo nag mooy jiitu, waaye yaramu judduwaale wi mooy jiitu, yaram wi bindoo ag noo topp ci.