bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 15:48
1 Corinthians 15:48 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waa àddina yor nañu jëmmi nit, ki ñu sàkke ci suuf; noonu it ñi bokk ci asamaan dinañu yor melokaanu ki jóge ci asamaan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kooka di suuf nag, na mu mel, ni la niti suuf mel. Ku asamaane ka it, na mu mel, ni la ñu asamaane ñi mel.