1 Corinthians 15:50 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li may wax nag bokk yi, moo di ne, sunu yaram wii mënul a am wàll ci nguuru Yàlla, te lu yàqu mënul a am wàll ci liy sax abadan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li may wax bokk yi, moo di suux ak deret du am cér ci nguurug Yàlla, te luy yàqu manula am cér ci lu dul yàqu.