1 Corinthians 15:51 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Lii ma leen di xamal, mbóotu Yàlla la. Dégluleen, dunu jaar ci dee nun ñépp, waaye nun ñépp dinanu soppiku,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kaayleen ma xamal leen mbir mu umpe. Dunu dee nun ñépp, waaye nun ñépp ay soppiku.