1 Corinthians 15:52 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ci saa su gàtt, ci xef-ak-xippi, bu liit gu mujj gi jibee. Ndax liit gi dina jib, néew yi dekki, di dund abadan, te nun dinanu soppiku.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lu gaawa gaaw lay doon, ci xef ak xippi, bu liit gu mujj ga jibee; nde liit ga mooy jib, ñi dee, dekki, di ñu dul yàqooti, nun nag, nu soppiku.