1 Corinthians 15:56 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Daŋaru dee mooy bàkkaar, te dooley bàkkaar mooy Yoon wi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndee, ag fittam mooy bàkkaar, te bàkkaar, dooleem mooy Yoon wi.