1 Corinthians 15:6 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Gannaaw ga feeñu na lu ëpp juróomi téeméeri bokki taalibe ci benn yoon. Te ñu bare ci ñoom ñu ngi dund ba léegi, waaye am na ci ñu nelaw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw gi mu feeñu lu ëpp juróomi téeméeri bokki taalibe yu ko gisandoo, te li ëpp ci ñooñu, ñu ngi dund ba léegi, doonte am na ñu ci nelaw.