1 Corinthians 15:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte maa gën a ñàkk solo ci ndawi Kirist yi, te yeyoowuma sax, ñu may wooye ndaw, man mi doon fitnaal mbooloom Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax kat maa gëna ñàkk solo ci ndawi Almasi, te yeyoowuma sax turu ndaw, gannaaw maa doon bundxatal mbooloom Yàlla mi.