1 Corinthians 16:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon bu ko kenn xeeb. Nangeen taxawu yoonam, ba mu dellusi ci man ci jàmm, ndaxte maa ngi koy xaar ak bokk yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon bu ko kenn xeeb. Gannaaw loolu nangeen ko yiwi ak jàmm, ba mu délsi ci man, ndax moom laay xaar, mook bokk yi itam.