1 Corinthians 16:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam ngeen ne, Estefanas ak njabootam ñoo jëkk a nangu xebaar bu baax bi ci diiwaanu Akayi, te ñoo joxe seen bopp, ngir liggéeyal gaayi Yàlla yi. Kon nag bokk yi, maa ngi leen di ñaan,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, xam ngeen ne Estefanas ak njabootam ñooy jooxeb ndoortel meññeef ci diiwaanu Akayi, te jàpple ñu sell ñi lañu séddoo. Kon dama leen di ñaan,