1 Corinthians 16:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bëgg naa leen yéen ñépp ndax sunu booloo ak Yeesu Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sama cofeel ñeel na leen, yeen ñépp, ci Yeesu Almasi mi nu bokk.