1 Corinthians 16:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw bu ma jàllee diiwaanu Maseduwan, dinaa ñëw ci yéen, ndaxte fas naa ko yéenee jàll.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dinaa dikk ba ci yeen, gannaaw bu ma jaaree diiwaanu Maseduwan, ndax Maseduwan laay jaare.