1 Corinthians 16:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte fi mu ne bëgguma leen a gis rekk, jàll, waaye yaakaar naa ne, dinaa toog ci yéen ab diir, bu neexee Boroom bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxte itam, buggumaa jaare fi yeen rekk, jàll, waaye yaakaar naa toog ci yeen ab diir, su ko Boroom bi mayee.