1 Corinthians 16:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte Yàlla ubbil na ma bunt, ba mu ne làññ, ngir may def liggéey bu man a am muj gu rafet, te noon yu bare bëgg a gàllankoor liggéey bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax bunt ubbikul na ma fi ŋàpp, ngir liggéey bu am njariñ, te noon yi bare nañu.