1 Corinthians 2:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Fekk nag nun la ko Yàlla won, jaarale ko ci Xelam. Xelum Yàlla mooy leeral lépp, ba ci xalaati Yàlla yi gën a xóot.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye nun la ko Yàlla feeñalale am Xelam. Ndaxte Xelum Yàlla lépp lay gëstu ba ci xóotey mbóoti Yàlla.