1 Corinthians 2:11 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kan ci nit ñi moo xam yëfi nit? Xanaa xelum nit mi nekk ci moom rekk a ko xam. Noonu it kenn xamul yëfi Yàlla, ku dul Xelum Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kan ci nit ñi moo xamal kenn nit, lenni biiram? Xelum nit ki ci biir nit ki doŋŋ moo mana xam biiram. Yàlla itam noonu la. Kenn xamul mbirum Yàlla, ku moy Xelum Yàlla.