1 Corinthians 2:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nun nag Xel mi nu jot, jógewul ci àddina, waaye Yàllaa nu ko sol.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nun nag du xelum àddina lanu jot, waaye Xel mi bawoo fa Yàlla lanu jot, ngir nu mana ràññee li nu Yàlla baaxe.