1 Corinthians 2:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nit kese du nangu yëfi Xelum Yàlla. Ag ndof lay doon ci moom, te du ko man a nangu, ndaxte ku yor Xelum Yàlla rekk moo ko man a ràññale.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nitu neen nag du nangu lu aju ci Xelum Yàlla. Ag ndof lay doon ci moom; du ko mana xam, ndax loolu Xelum Yàlla lees koy natte.