1 Corinthians 2:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Mbind mi nee na:«Lu bët gisul,nopp déggu kote xel xalaatu ko,loolu la Yàlla dencal ñi ko bëgg.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mooy noonu ñu binde rekk ne: «Lu bët gisul, nopp déggu ko, xel daju ko, Yàllaa ko dencal ñi ko sopp.»