1 Corinthians 3:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Man nag bokk yi, mënuma woon a wax ak yéen ni ay nit ñuy déggal Xelum Yàlla, waaye waroon naa wax ak yéen ni ñuy topp seen nafsu, mel ni ay liir ci seen dund ci Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man nag bokk yi, manuma woona wax ak yeen ni ñuy waxe ak ñu ànd ak Xelum Yàlla, waaye ni niti suuxu neen rekk laa manoona waxe ak yeen, mbete ñu diy tuut-tànk ci yoonu Almasi.