1 Corinthians 3:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Man nag teg naa fondamaa bi, ni tabaxkat bu man liggéeyam, dëppoo ak sas wi ma Yàlla jagleel ci kaw yiwam. Te keneen a ngi tabax ci kaw; waaye na ku nekk teeylu ci ni muy tabaxe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yiwu Yàlla wi mu ma may nag, ci laa lale kenu gi, ni tabaxkat bu xareñ, keneen di tabax ca kaw. Waaye na ku nekk xool bu baax na mu cay tabaxe.